Neex Na
de Dieyla Gueye
Dugg nga sama jamano
Te sama loxo wan ma
Luy mbëggeel
Xamal nga ma luy nobeel
Yaw daal jélal lépp
Loo am ñàkku ma ko leer na ma
Wuuy nobeel
Xam naa lan mooy mbëggeel
Dara gëmul neex mbëggeel bi ngay yëg ci sa xol dundu ko
Wuy yoro baale ma
Yoo baale ma
Gis naa ci yaw jikko duma neex moo ma doy feex sama xol bi
Ohh ohh wu wey, bëgg naa
Ñoo ngi kaf foo ree
Fu ñu ne ñu ngi door baake
Ñépp ñu rañe
Te foo ne rekk lay bëgg ne
Foo ne lay nee
Foo newul duma fa bëgg ne yaw
Wuy ooo baale ma (yombu ma)
Yoo baale ma
Yaw bébé dama réew nga ni ma loxo du la laal
Yaw bébé wayale ma nga ni ma Youssou Ndour lay woo
Yaw àdduna bi su ma safee dara yaa ko liggéey way
Yaw wane nga ma fu ne doo ma réerak feeñ
Wuy nobeel! (nobeel)
Aah oh (nobeel)
Xamal nga ma luy nobeel
Li may dundu neex na
Li may dundu neex
Neex na neex na neex
Ni lépp yaw la
Li may dundu neex na
Li may yëg aka moo neex
Hu waow wao wax a ay
Lépp yaw la
Yaa ngi jàpp te bàyyiwoo
Sonn te taatiwoo
Muy metti te xaddiwoo
Nëbbatu woo ma
Yaa ma gënal ñi ni ak ñële
Ndax lépp yaw la
Amina chérie Papy yaayu Muhammad
Amina beauté famille ni maak ju baax nga
Waay sama yaay de Aisha dago jula
Yaayu Muhammad, Aïsha baax nga
Li may dundu neex na
Li may dundu neex
Neex na neex na neex
Ni lépp yaw la
Li may dundu neex na
Li may yëg aka moo neex
Hu waow wao wax a ay
Lépp yaw la
Baye Dame chéri Aishata
Man de way naa la
Da mooy dame
Ñaan bi yaw la
Más canciones de Dieyla Gueye
-
Doflo Ngama
Doflo Ngama
-
M'a Ngui Baxx
M'a Ngui Baxx
-
Diayoulen
Diayoulen
-
Yaw la
Yaw la
-
Déko Woyofal
Déko Woyofal
-
Li lanla
Li lanla