Samaxol

de Coumba Gawlo

Ñëwal, ñëwal nu feccee
Ñëwal, ñëwal nu feccee

Feccleen, gaa yi feccleen
Summileen costume yeek cravate yee
Summileen dàll yi takk ndig yee

Ñëwal, ñëwal nu feccee
Ñëwal, ñëwal nu feccee

Ah boroom ceebu-jën dagaañ lu la neex def
Ne boroom ceebu-jën dagaañ lu la neex def
Ventilateur, climatiseur, warmiin ñëwal ñu dem

Ñëwal, ñëwal nu feccee
Ñëwal, ñëwal nu feccee

Làng ma, xool ma, kot ma ñu feccee
Di wëral wëral wëral ñëw ñu dajee
Yàkkamti ma teg ma ci say mbagg ñu feccee

Ñëwal, ñëwal nu feccee
Ñëwal, ñëwal nu feccee

Tourneel ma tourné ñu daje feec di wéy!
Ni wëral, wëral, wëral, wëral ñëw ñu daje
Jàppal ngigu li yëngal ko te bu ko yërëm
Bësal!

Ñëwal, ñëwal nu feccee
Ñëwal, ñëwal nu feccee

Feccleen, gaa yi feccleen
Summileen costume yeek cravate yee
Summileen dàll yi takk ndig yee

Ñëwal, ñëwal nu feccee
Ñëwal, ñëwal nu feccee

Ah boroom ceebu-jën dagaañ lu la neex def
Ne boroom ceebu-jën dagaañ lu la neex def
Ventilateur, climatiseur, warmiin ñëwal ñu dem

Ñëwal, ñëwal nu feccee
Ñëwal, ñëwal nu feccee

Làng ma, xool ma, kot ma ñu feccee
Di wëral wëral wëral ñëw ñu dajee
Yàkkamti ma teg ma ci say mbagg ñu feccee

Ñëwal, ñëwal nu feccee
Ñëwal, ñëwal nu feccee

Tourneel ma tourné ñu daje feec di wéy!
Ni wëral, wëral, wëral, wëral ñëw ñu daje
Jàppal ngigu li yëngal ko te bu ko yërëm
Bësal!

Weeeey, may ma ci sa lii sa lii sa lii sa lii
May ma sa lii sa lii sa lii sa lii sa lee

Ñëwal, ñëwal nu feccee
Ñëwal, ñëwal nu feccee
Ñëwal, ñëwal nu feccee
Ñëwal, ñëwal nu feccee...

Chéri ñëwal ñëwal
Chéri coco ñëwal ñëwal
Heeey, ñëwal ñëwal
Ma ni ñëwal ñëwal
Nee ñëwal ñëwal
Heeey ñëwal ñëwal
Chéri ñëwal ñëwal
Ñëwal ñëwal...

Feccleen, gaa yi feccleeeen
Gaa yi feccleen
Ñëwal, ñëwal ñu feccee
Ha ha ha ha ha!

Más canciones de Coumba Gawlo