Tukki Bukki

de Ashs The Best

Bu xaaju guddee, bu xaaju guddee
Bu ñëpp di nelaw man ma
Weet′ag xaalat waxtaan'ag njegenaay
Kenn du ma yee ku nelawul nan lañ koy yeewee
Biig foru ma bët waxtaan′ag njegenaay

Nelawu ma biig
Xanaa waxtaan'ag sama njegenaay
Tay kenn duma yee
Ku nelawul nan lañ koy yeewee

Xale baa ngi jooy, nax ko warul jooy
Doomu jambur warul jooy
Demb laa la miin, tay yaa ngi taggoo
Soy dem yobbaale ma

Ulluku man ku ma nëbbu ma reer la
Ci rukku laa la woo yobaante la
Ulluku boy nelaw bul xaar mu yee la
Kuy tukki deeg naa ñu ne warul taggoo
Fukki bukki laa gis taggaliko'og sama saggo
Ulluku boy nelaw bul xaar mu yee la

Bul ma di sooraale
Sooraaleel sa bopp
Soy dox di gestuwaale
Mën nga fakkastalu

Ulluku ku ku ku ku
Kuma nëbbu ma reer la
Ulluku ku ku ku ku
Tukki tukki bukki
Tukki bukki

Fukki bukki guddi
Fukki bukki bëccëg oo
Nitt ki li muy wundu
Mën nga ci bañ teg bët
Bukki bënn buntu
Bant bënn bëttëm
Nitt ki li muy wundu
Mën nga ci bañ teg bët

Fukki bukki guddi
Fukki bukki bëccëg oo
Nitt ki li muy wundu
Mën nga ci bañ teg bët
Bukki bënn buntu
Bant bënn bëttëm
Nitt ki li muy wundu
Mën nga ci bañ teg bët

Ulluku ku ku ku ku
Man ku ma nëbbu ma reer la
Ulluku ku ku ku ku

Más canciones de Ashs The Best