Ayubes

de Ashs The Best

Man gestu naa di xoolaat fi ma jaar
Te weesu naa dootul mës ñëwaat
Foo ma jëmee ci kaw mbaa ci suuf
Su ma gisatul yaay, te ammu ma maam, fan laay nàmpee

Foo ma nara jëmee
Da maa foogoon dootul jeex ndeke Yàlla ko moom
(Maam Yàlla ko moom)
Jamm a ko gën
(Jamm a gën ub ay)
Da maa foogoon dootul jeex ndeke Yàlla ko moom

(Maam Yàlla ñu moom, moom sunuy doom)
Da maa foogoon dootul jeex ndeke Yàlla ko moom
(Maam Yàlla ñu moom, uuf sunu njaboot)
Da maa foogoon dootul jeex ndeke Yàlla ko moom

Miin naa sa kanam gi
Miin naa kepaar gi
Gëj naa këram ga
Te miin naa dëkkam bi
Gëj naa ci xellam bi
Te sës ci xollam bi
Xas naa ko xaccoo
Dootu ma fa delloo

Man da maa foogoon
Da maa foogoon
Da maa foogoon dootul jeex ndeke Yàlla ko moom
Maam Yàlla ko moom
Jamm a ko gën
Jamm a gën ub ay
Da maa foogoon dootul jeex ndeke Yàlla ko moom

Más canciones de Ashs The Best